Sama Lumière

PMJR

    Continues after the ad

    Prés de toi ouais le temps il s'arrête
    Mon coeur ne tient plus, là il bat plus fort
    Accroche toi à moi, je ne veut que toi déé
    Car dans tes bras je deviendrais le plus fort

    Dans cette vida j'ne pourrais vivre sans elle
    Elle est devenue mon médicament
    Mon coeur ne bat que pour toi
    Pour toi, mon amour

    Yaw yaay sama lumière
    Tudde naa la sama lingeer
    Jëlal xol bi yóbbu dem
    Li moo neex cey mbëggeel

    Yaw yaay sama lumière
    Tudde naa la sama lingeer
    Jëlal xol bi yóbbu dem
    Li moo neex cey mbëggeelooy

    Continues after the ad

    Héé chérie coco
    Héé misise lovely
    Dama dof ci yaw, miir ci yaw
    Ba loo ma wax moom laay def wax waaw

    Héé ma chérie coco
    Héé ieo misie lovely
    Dama dof ci yaw, miir ci yaw
    Ba loo ma wax moom laay def wax waaw

    Jëlal xol bi yóbbu dem baby yaa ko
    Jëlal xol bi yóbbu dem baby yaa ko
    Jëlal xol bi yóbbu dem baby yaa ko
    Jëlal xol bi yóbbu dem baby yaa ko

    Bul ma xool yaw, wan ma ko
    Moo gën nga may saagaane
    Wan ma sa mbëggeel yaw
    Wan ma sa mbëggeel yaw (yeah)

    Yaw yaay sama lumière
    Tudde naa la sama lingeer
    Jëlal xol bi yóbbu dem
    Li moo neex cey mbëggeel

    Yaw yaay sama lumière
    Tudde naa la sama lingeer
    Jëlal xol bi yóbbu dem
    Li moo neex cey mbëggeelooy

    Song details

    Composition: Pmjr

    Did you see an error?

    Enviar revisão