Continúa después del anuncio

    Yay sama diamond leral goudi dih leral beuthieuk Yaay sama diamond, ooh
    Yay sama diamond leral goudi dih leral beuthieuk Yaay sama diamond, ooh

    Ko wakhal wakhal gaaw diongama wakhal wakhal gaaw ngelaw lou fekh li dih nieuw
    Iow diapeu nelaw bankou sama lal

    Goudi ngui mo gueneu yague lol batakhna manatouma nelaaw
    Ma yakamti ba buerset diote madiakarlo ma wakhla limay yeuk

    Continúa después del anuncio

    Sokhna si yeureum ma iow mi djiogama wakhal wkhal gaaw
    Ngalaw lou fekh lih di niow iow diapeu nelaw bankou sama laal

    Yaay sama diamond leral goudih di leral beuthieuk yaay sama diamond

    Ooh, yaay sama diamant yay leral goudi dih leral beuthieuk
    Yaay sama diamant, ooh

    Información de la canción

    Composición:

    ¿Los datos están equivocados?

    Enviar revisión