Continúa después del anuncio

    Oh na na na na
    Yeah, yeah

    Mësuma yëg bi love
    Te moom ni mu nayise noonu la yaru wee
    Lii yaw la
    Maman, ni nga yare sa doom ji rafet na
    Mësuma wax ba mu mer
    Su ma waxee mu naan ma yaay sama bouts ya tayi
    Wa mais yaw goto yae yaay
    Maa ngi doga feex mais
    Sama bébé ci yaw lay roy

    Sama goro, sa doom, dama ko nob
    Sama goro, sa doom, dama ko nob
    Maa la wax li yaw goro, sa doom, dama ko nob
    Goro, sa doom, dama ko nob
    Eywaay li yaw goro, sa doom, dama ko nob
    Sama goro, sa doom, dama ko nob
    Sama goro, sa doom, dama ko nob

    Continúa después del anuncio

    Amuma xaalis ndeysaan
    Mais tewul daf may defal li ma bëgg aywaay
    Moom dafa saf sama jumbo la
    Dafa sap sama jumbo la
    Sama jumbooo la yeah
    Ayeee, ayeee

    Sama goro, sa doom, dama ko nob
    Sama goro, sa doom, dama ko nob
    Maa la wax li yaw goro, sa doom, dama ko nob
    Goro, sa doom, dama ko nob
    Maa la wax li yaw goro, dama ko nob
    Sama goro, sa doom, dama ko nob
    Sama goro, sa doom, dama ko nob

    Sama goro waay ehh
    Goro goro goro goro

    Naa la may million cfa, million cfa
    May la million, goro naa la may ay million cfa
    Naa la may million cfa
    Naa la may, naa la may
    Million cfa, million cfa

    Sama goro, sa doom, dama ko nob
    Sama goro, sa doom, dama ko nob
    Maa la wax li yaw goro, sa doom, dama ko nob
    Goro, sa doom, dama ko nob
    Maa la wax li yaw goro, dama ko nob
    Sama goro, sa doom, dama ko nob
    Sama goro, sa doom, dama ko nob

    Información de la canción

    Composición:

    ¿Los datos están equivocados?

    Enviar revisión