Oh na na na na Yeah, yeah Mësuma yëg bi love Te moom ni mu nayise noonu la yaru wee Lii yaw la Maman, ni nga yare sa doom ji rafet na Mësuma wax ba mu mer Su ma waxee mu naan ma yaay sama bouts ya tayi Wa mais yaw goto yae yaay Maa ngi doga feex mais Sama bébé ci yaw lay roy Sama goro, sa doom, dama ko nob Sama goro, sa doom, dama ko nob Maa la wax li yaw goro, sa doom, dama ko nob Goro, sa doom, dama ko nob Eywaay li yaw goro, sa doom, dama ko nob Sama goro, sa doom, dama ko nob Sama goro, sa doom, dama ko nob Amuma xaalis ndeysaan Mais tewul daf may defal li ma bëgg aywaay Moom dafa saf sama jumbo la Dafa sap sama jumbo la Sama jumbooo la yeah Ayeee, ayeee Sama goro, sa doom, dama ko nob Sama goro, sa doom, dama ko nob Maa la wax li yaw goro, sa doom, dama ko nob Goro, sa doom, dama ko nob Maa la wax li yaw goro, dama ko nob Sama goro, sa doom, dama ko nob Sama goro, sa doom, dama ko nob Sama goro waay ehh Goro goro goro goro Naa la may million cfa, million cfa May la million, goro naa la may ay million cfa Naa la may million cfa Naa la may, naa la may Million cfa, million cfa Sama goro, sa doom, dama ko nob Sama goro, sa doom, dama ko nob Maa la wax li yaw goro, sa doom, dama ko nob Goro, sa doom, dama ko nob Maa la wax li yaw goro, dama ko nob Sama goro, sa doom, dama ko nob Sama goro, sa doom, dama ko nob