Ni La Deh

Sokhou Bb

    Continúa después del anuncio

    Baby ku ma la nara xeñ jël fële
    Soo ma rëccee, lu mel ni fan laa koy jële?

    Bëgg naa man saa yaw geestu gis ma ci sa wet
    Chérie kaay ñu juboo
    Surtout loolu moo dàq lem
    Bul déglu ki ñëw naan la bàyyi ma
    Kooku am noon la
    Mbëggeel capitaine boroom
    Man de comando laa
    Bateau dem, bateau costé
    Ki ko bëgg man de duma ko ko may
    (Non, non, non, non, non, non)
    Kër gi benn sër fi ne te ma koy takk
    Jalal ba Thiak Ndiaye

    Léegi damay ngoy ci séy bi (ni la de)
    Séy fi yoku cere dolli ñex (ni la de)
    Fan yi dama féroce jongé lool (ni la de)
    Sa jëkker boo ko yore def ko xale way (mëni ni la de)

    Continúa después del anuncio

    Bae dama fiir te dama gaawa saalit
    Am xadar waaye xol bi jàppul dara
    Dama la nob a nob a nob a nob a nob
    Man mi yamalewuma lak dara

    Guddi na, baby bul ragal
    Li may yëg, bae est-ce que yaa ngi koy yëg?
    Bul ragal, ndaxte du la gaañ
    Li may yëg, bae est-ce que yaa ngi koy yëg?

    Chéri, chéri, chéri, baal ma
    Coow li, coow li, coow li man la (oh, oh)
    Du man ma la moom dina ngoy ci yaw mel ni dakkande

    Léegi damay ngoy ci séy bi (ni la de)
    Séy fi yoku cere dolli ñex (ni la de)
    Fan yi dama féroce jongé lool (ni la de)
    Sa jëkker boo ko yore def ko xale way (mëni ni la de)

    Información de la canción

    Composición:

    ¿Los datos están equivocados?

    Enviar revisión