Continues after the ad

    Xamna lilay sonal
    Wax jou bari teksi nga diss te yenouwo
    Xamna lilay sonal
    Bilé melokan molay deranger
    Yalla mayma nangouwo
    Ma romboula nangoulo
    Foma seen dima retane té begouloma

    Heeey
    Tiré ngama visél bou baax ndax daluma
    Tiré ngama visél bou baax ndax daluma
    Tiré ngama visél bou baax ndax daluma
    Sit down yow
    Fii adinala kon teyal (lala lala lalala)
    Fii adinala kon teyal (lala lala lalala)
    Fii adinala kon teyal (lala lala lalala)
    Fii adinala fils teyal (ohh)

    Xamna lilay sonal
    Wax jou bari teksi nga diss te yenouwo
    Man Xamna lilay sonal
    Bilé melokan molay deranger
    Yalla mayma nangouwo (mayla nangouwo)
    Ma romboula nangoulo (ma romboula nangouwo)
    Foma seen dima retane té begouloma
    Yalla mayma nangouwo
    Ma romboula nangoulo
    Foma seen taalalma loxo té soppouloma

    Continues after the ad

    Hey
    Tiré ngama visél bou baax ndax daluma
    Tiré ngama visél bou baax ndax daluma
    Tiré ngama visél bou baax ndax daluma
    Sit down yow
    Fii adinala kon teyal
    Fii adinala hey teyal
    Fii adinala kon teyal
    Fii adinala fils teyala tey

    Maalay deranger
    Ndeketé mane rek nga bañ
    Te xawma loumala def
    Bo sañoon souba ma dé
    Ngir suñu andabi yaga
    Fok ñouy waxanté deugga
    Ba ñoumay matteu di euffé mattaalela

    Xarit né waxma mani waxma
    Lou tax sooma guissé dima ré te beggouloma
    Kay ma waxla togal ma waxla
    Pexé you bone yingay jeem ni yalla guiss la

    Eey
    Tiré ngama visél bou baax ndax daluma
    Tiré ngama visél bou baax ndax daluma
    Tiré ngama visél bou baax ndax daluma
    Sit down yow
    Jeleul waywi ma mayla yeah
    Jeleul waywi maynala yeah
    Jeleul waywi ma mayla yeah
    Jeleul waywi maynala
    Defko cas

    Song details

    Composition:

    Did you see an error?

    Enviar revisão