Mi Amoré

VJ

    Continúa después del anuncio

    Demoon ba bëggatuma dundu love
    Ndax ay coono ci xol
    Ton sourire est ma plus belle récompense
    Ma comolonko ci yaw
    Danga ma bëgg nekkuloo ci détail
    Danga ma miinal sa bopp
    Àljanna sax ñooy bokku jootaay (hmm sama lova)

    Yëgoon ni wax nañ ma lu ne ci yaw ngir ma bàyyi
    My baby man yëg naa ni wax nañ la lu ne ci man ngir nga bàyyi
    Moo tax it nga teey ma di tourner di tourner ba mujje ci man yeah
    Man tamit ma tourner di tourner di tourner ba ñëwaat ci yaw

    Je te l'ai promis, amoré (i love you amoré)
    Je te l'ai promis, amoré (i love you amoré)
    Je te l'demande s'il le faut ouais
    Je t'aime, je t'aime, embrasse-moi yeah
    Déverse-moi tout l'amour (i love you amoré)
    N'en verse pas une seule goutte (i love you amoré)
    Je te l'ai promis, amoré
    Je t'aime, je t'aime, embrasse-moi yeah

    Continúa después del anuncio

    Et faut pas t'inquiéter
    Je prendrai bien soin de toi, bébé
    Moi je ferai de toi la plus heureuse
    Des femmes sur cette planète
    Yaw mi ma jaral lii
    Yaw mi laa doon xaar
    Su ma la gisulee janneer
    Yaw mi laa doon seet (hmm sama lova)

    Yëgoon ni wax nañ ma lu ne ci yaw ngir ma bàyyi
    My baby man yëg naa ni wax nañ la lu ne ci man ngir nga bàyyi
    Moo tax it nga teey ma di tourner di tourner ba mujje ci man yeah
    Man tamit ma tourner di tourner di tourner ba ñëwaat ci yaw

    Je te l'ai promis, amoré (i love you amoré)
    Je te l'ai promis, amoré (i love you amoré)
    Je te l'demande s'il le faut ouais
    Je t'aime, je t'aime, embrasse-moi yeah
    Déverse-moi tout l'amour (i love you amoré)
    N'en verse pas une seule goutte (i love you amoré)
    Je te l'ai promis, amoré
    Je t'aime, je t'aime, embrasse-moi yeah

    Je te l'ai promis, amoré (i love you amoré)
    Je te l'ai promis, amoré (i love you amoré)
    Je te l'demande s'il le faut ouais
    Je t'aime, je t'aime, embrasse-moi yeah
    Déverse-moi tout l'amour (i love you amoré)
    N'en verse pas une seule goutte (i love you amoré)
    Je te l'ai promis, amoré
    Je t'aime, je t'aime, embrasse-moi yeah

    Información de la canción

    Composición:

    ¿Los datos están equivocados?

    Enviar revisión

    Canciones relacionadas