Djery Ngoné

Wally B. Seck

    Continues after the ad

    Agn dém ndaat diéry seu keur maam
    Agn dém ndaat diéry seu keur maam
    Kouli ma ceu sengui ndaat

    Diéry ngoné hum hum
    Meu délou ci waat

    Diéry ngoné ma laobé samba kouli meu ceu sengui ndaat mbaye
    Mafaaly Kumba ndaama seu maam teukh bi
    Naarou Marietou Agne sama waadji
    Mbaye diéry, diobéti naa leu

    Continues after the ad

    Diéry ngoné
    Mafaaly Kumba ndaama-a
    Mbaye diéry, diobéti naa leu
    Mbaye diéry, diobéti naa leu

    Mbokoum yaayou Khoudia Ciss
    Djiguénou Bathie Samb
    Yaayou Aléya fonk naa leu

    Guéwélou ndaat ak guééry ndaat (ndaat ndaat)
    Ko ciy woy néko maa laobé samb

    Diéry ngoné
    Kouli ma ceu sengui ndaat
    Diéry ngoné ma laobé samba kouli meu ceu sengui ndaat mbaye
    Mafaaly, Mafaaly
    Mafaaly Kumba ndaama seu maam teukh bi
    Balaa déég fouki ball ak niaar né touy
    Mbaye diéry, diobéti naa leu

    Agn dém ndaat diéry seu keur maam
    Kou seu baay meunon baayam, dom djeu yaako meun
    Yaa lén meun, diéry
    (Agn dém ndaat diéry seu keur maam)
    Fonk ngam yo, diéry
    Téral ngama, diéry
    (Agn dém ndaat diéry seu keur maam)
    Chérie Thomas, gueun ci man
    Gaaw ci man anh diéry
    (Agn dém ndaat diéry seu keur maam)
    Nangou naa kou leu makk
    Douma nangou kou leu gueun, diéry
    Yaa lén meun, na-na diéry

    Song details

    Composition:

    Did you see an error?

    Enviar revisão