Continúa después del anuncio

    Paradise rek laalay jeumé
    Thi geedjou banekh laniouy feey maak iow
    Beukoulo akk niom niveau
    Teg naala thi kaw
    Té dara doulafa dieulé my bve

    Aljana
    Aljana laala jeumé iow aljana
    Iow aldiana
    Dou Aljana lagn nara deuké
    Aljana
    Oubi sa xol douggeul fa airou aljana
    Aljanaaaa

    Continúa después del anuncio

    Maak iow ba paradise
    Denk naala sama life
    Dou ayy foo laalay doyei my bve
    Farata rek laalay doyei my bve
    Takk ma boum si baat
    Soxlawoul sakh ngamay wakh fooma nara dieulé my bve
    Manak iow dou diekh
    Deh rek moniouy takkalé
    Meunoumala baayek kenen
    Iow laay soor baby waxma loula nior
    Lane ngay yootou chérie ma adjiko
    Paradise rek laalay dieumé
    Thi geediou baneex laniouy feey maak iow

    Aljana
    Aljana laala jeumé iow aljana
    Iow aldiana
    Dou Aljana lagn nara deuké
    Aljana
    Oubi sa xol douggeul fa airou aljana
    Aljanaaaa

    Información de la canción

    Composición:

    ¿Los datos están equivocados?

    Enviar revisión