Cifra Club

Adduna

AMADEUS

Aún no tenemos los acordes de esta canción.

Papelaye

Àdduna a ngi nuy xool
Nee nañ man ak yaw du sori
Nee nañ ma du mool
Nee nañ lii du luy dem fenn
Ku baax du ñàkk i noon
Li nuy tabax lañ bëgg a yàq
Te man duma ku bon
Yéenewuma la man safaan
Àdduna a ngi nuy xool
Di nu ree ree yu rafet
Bëñam ya weex lool
Waaye dereet a ko lal
Bëñ ya weex na
Waaye dereet moo ko lal
Su ñu sañoon man ak yaw dootun bokk lal

Ñi ni dañu may xeex
Ñele ne dañu lay xeeb yaw
Xamuma lu nu leen def
Xamuma lu ñu nu toppe

All day da ñu may xeex
Sometime dañu lay xeeb yaw
Xamuma lu nu leen def
Lan moo tax manuñu toppe

Dama yam sama life my boy
Mayuma kenn ci sama life muy dogal
Dama yam sama life my boy
Man mayuma kenn sama life muy dogal
Dama yam sama life my boy
Mayuma kenn ci sama life muy dogal
Dama yam sama life my boy
Mayuma kenn ci sama life muy dogal

Àdduna a ngi nuy xool
Boo yaboo nga moytu leen
Bu ñu xamee foo jëm
Duma ne doo yegg
Waaye dina jafe lool
Seen i làmmiñ dafa tooke
Seen i pexe bon
Boo yaboo nga moytu leen
Boo yaboo nga moytu leen

Fexeel ba buñ la jam naani
Wiiri wiiri, jaari Ndaari
Toppal sa yoon ba dégg daan

Ñi ni dañu may xeex
Ñele ne dañu lay xeeb yaw
Xamuma lu nu leen def
Xamuma lu ñu nu toppe

All day da ñu may xeex
Sometime dañu lay xeeb yaw
Xamuma lu nu leen def
Lan moo tax manuñu toppe

Dama yam sama life my boy
Mayuma kenn ci sama life muy dogal
Dama yam sama life my boy
Mayuma kenn sama life muy dogal
Dama yam sama life my boy
Mayuma kenn ci sama life muy dogal
Dama yam sama life my boy
Mayuma kenn ci sama life muy dogal

Otros videos de esta canción
    0 visualizaciones

    Afinación de los acordes

    Afinador en línea

    Ops (: Contenido disponible solo en portugués.
    OK