Hey Massamba Walo
All days and nights
Yaa ngi ci sama xel mi
Dañ ma lay laaj
Maas yaw ana booy bi
Waaye li nga ma teg ci metit dafa bari
Li nga ma digoon ni ba nga ko xajul ci lim
Yaw sama xol bi nga ma laaj
Ne ma Masàmba dootuma la gaañ
Waatal nga ma wallaaayy billaay
Ne ma ne déwen dootul mel ni daaw
Waxoon naa la bul ma sàggane
Baakari ak Daarama
Ne woon naa la duma la fowe
Aram Lóo Kumba Caam
Naa la wan ne man naa la wan ne
Xam naa ne li nga may jaay
Xanaa xamóo ne xam naa ne
Masamba loo may jaay
Nekkatuma xale boog
Kenn du ma naxee noonu
Naa la ne wan ne man naa la wan ne
Xam naa ne li nga may jaay
Xanaa xamóo ne xam naa ne
Masamba loo may jaay
Nekkatuma xale boog
Yombatuma naxee noonu
Bëggatuma la bàyyi
Ni manatuma la ba
Dem nan ba romb foofu noonu
Xamuma nu mu tuddeeti
Sori na daal
Tax manatuma dellu ginnaaw
Tegul ci yoon wi
Defaral sa taxawaay
Ehh
Yaw sama xol bi nga ma laaj
Ne ma Masàmba dootuma la gaañ
Waatal nga ma wallaaayy billaay
Ne ma ne déwen dootul mel ni daaw
Ne woon naa la bul a sàggane
Baakari ak Daarama
Waxoon naa la duma la fowe
Aram Lóo Kumba Caam
Naa la ne wan ne man naa la wan ne
Xam naa ne li nga may jaay
Xanaa xamóo ne xam naa ne
Masamba loo may jaay
Nekkatuma xale boog
Kenn du ma naxee noonu
Naa la ne wan ne man naa la wan ne
Xam naa ne li nga may jaay
Xanaa xamóo ne xam naa ne
Masamba loo may jaay
Nekkatuma xale boog
Yombatuma naxee noonu
Ku la safooti faale ko
Ku la bëgg moo la sonal daal
Han ki la bañ
Ki la bañ da laa noppal
Ku la safooti faale ko
Ku la bëgg moo la sonal daal
Han ki la bañ
Ki la bañ da laa noppal