Hey Massamba Walo
Am nga ngor lool
Yaa di ki ma nawloo
Kocc na ma jéggal
Man de wóolu nama laa
Kocc na ma jéggal
Man de wóolu nama laa
Dem nanu ba romb dëkku man a bàyyi
Gane na nu ndumbelaan
Dund nan fa àndu nawle
Soo gestoo gis ma maa ngi ci sa ginnaaw
Muy bànneex walla naqar
Dinga ma gis loo man a xewle
Ndax man la Maas
Du ku ne laa man defal
Raw nga maas
Yaw waxóo ma danga maa jëfal
Fees sa place
Su ma meree yaay dëfal
Am nga classe
Garmi sama séddoo
Jigéen
Am nga ngor lool
Yaa di ki ma nawloo
Kocc na ma jéggal
Man de wóolu nama laa
Am nga ngor lool
Yaa di ki ma nawloo
Kocc na ma jéggal
Man de wóolu nama laa
Tann ma ci mbooloo mi
Nangu nima bindo
Man manu ma lu dul gërëm la
Man wóolu nama laa
Am nga ngor lool
Yaa di ki ma nawloo
Kocc na ma jéggal
Man de wóolu nama laa
Dem nan ba romb dëkku man a bàyyi
Gane na nu ndumbelaan
Dund nan fa àndu nawle
Soo gestoo gis ma maa ngi ci sa ginnaaw
Muy bànneex walla naqar
Dinga ma gis lu man a xewle
Su ma la njëkkee jug naa la yee
Su ma la jiitoo naa la xaar
Man nga ma wóolu duma la weer
Nangu say sikk naa la suturaal
Am nga ngor lool
Yaa di ki ma nawloo
Kocc na ma jéggal
Man de wóolu nama laa
Am nga ngor lool
Yaa di ki ma nawloo
Kocc na ma jéggal
Man de wóolu nama laa
Tann ma ci mbooloo mi
Nangu nima bindo
Man manu ma lu dul gërëm la
Man wóolu nama laa
Am nga ngor lool
Yaa di ki ma nawloo
Kocc na ma jéggal
Man de wóolu nama laa
Am nga ngor lool
Yaa di ki ma nawloo
Kocc na ma jéggal
Man de wóolu nama laa
Am nga ngor lool
Yaa di ki ma nawloo
Kocc na ma jéggal
Man de wóolu nama laa
Tann ma ci mbooloo mi
Nangu nima bindo
Man manu ma lu dul gërëm la
Man wóolu nama laa
Am nga ngor lool
Yaa di ki ma nawloo
Kocc na ma jéggal
Man de wóolu nama laa