Cifra Club

Trahison

Queen Biz

Aún no tenemos los acordes de esta canción.

Yow mi yama def li nga noppi néma doul
Yow mi yama def li nga noppi néma dou yow
Kholal nimey doundei thii biir sameiy nawlé

Man foggone na khamal leu ni yamey doundeul
Man yakkarone na ni yow mi yamey digueul eh

Thiow li daldi daw none yi dadnei niaw
Khadj yi dileu mbow mou topp leu a faw
Talatouma ken guissatouma ken
Dematouma fen beugueutouma ken
Kholal nimey doundei thii biir sameiy nawlé
Kholal nimey doundei hey thii biir sameiy nawlé

Oh my baby boy
Boulmeu diemeu trompé
Oh my baby boy
Boulmeu diemeu foowé

Gni nane meu li
Gneulei nane meu lé
Khol bii nema lé
Khel bi wokh lenen
Deffone ngueu teut
Meu noppi daldi keuth
Khol bi pess meu beuss
Tay dama seuss

Kholal nimey doundei thii biir sameiy nawlé
Kholal nimey doundei hey thii biir sameiy nawlé

Yow mi yama def li nga noppi néma doul
Yow mi yama def li nga noppi néma dou yow
Kholal nimey doundei thii biir sameiy nawlé
Kholal nimey doundei thii biir sameiy nawlé

Man foggone na khamal leu ni yamey doundeul
Man yakkarone na ni yow mi yamey digueul eh
Kholal nimey doundei thii biir sameiy nawlé
Kholal nimey doundei thii biir sameiy nawlé

Anh deug deug yaggone na degg deug
Topp sama khol di beug batakh mounouma degg
Oh dinala wokh nei founiou meunti dadjé yow yaffey seug
Donté dangmeiy reuk mba sakh ngameiy diani deuk
Dama deudou keur baye dellou nekk sa yaye
Kone mounoma faye dinala wone nei thiow lefi dess
Dinala wone nei
Ma gueuneu toyy mamy campbell
Kouma teggal kamil ma watnei dama fidèle
Anh baby boy attoul ngameiy sakketou
Di foknei dameiy kebetou motakh ngueiy neubeutou
Kham seu biti kham seu biir motakh may fiir
Bouma diapé gounei souma wokhei ngameiy leurrer
Kone nangma diégueul sou fekei dama wéré
Anh

Yow mi yama def li nga noppi néma doul
Yow mi yama def li nga noppi néma dou yow
Kholal nimey doundei thii biir sameiy nawlé
Kholal nimey doundei thii biir sameiy nawlé

Man foggone na khamal leu ni yamey doundeul
Man yakkarone na ni yow mi yamey digueul eh
Kholal nimey doundei thii biir sameiy nawlé
Kholal nimey doundei thii biir sameiy nawlé

Yow mi yama def li nga noppi néma doul
Yow mi yama def li nga noppi néma dou yow

Otros videos de esta canción
    0 visualizaciones

    Afinación de los acordes

    Afinador en línea

    Ops (: Contenido disponible solo en portugués.
    OK