Music
Soryba ha-ha-haaa Music
Nga jël ma taf sa wét di ma tëgg ni tama tàjjaboon
Dama dof ci yaw, nga may ndëpal ma daanu ci sa ron
Fu ma jëm ak xale bi, àttanuma lii
Son regard me fait effet, o-o-ow ça m'excite
Fi ma làkk dafa sore, bopp bi noonul ñore
Yëfi bandit dafa jongé
Def ma buur di ma limal samay maam
Mbëggeel lu neex la
Billaay, mbëggeel lu neex
Man ak yaw ba États-Unis
Sans visa ma ni
Dox ba dem Roumanie
Naaw ba asaman tërëdi àljanna
Foofu la, billaay foofu la
Billaay wallaay bébé
Maa la nob, wax ma ku ci mën nada
Moom du coow du tooñ du fowe dóor ak saaga
Moom dafa nooy agneau la bu tooy
Moom sax duma jooyloo dëkke di ma sourireloo (bébé)
Maa la nob, wax ma ku ci mën nada
Moom du coow du tooñ du fowe dóor ak saaga
Moom dafa nooy agneau la bu tooy
Moom sax duma jooyloo dëkke di ma sourireloo
Yaay sama oxygène bi ma soxla di nooy tous les jours
Bébé je t'aime, tu m'aimes
Depuis la nuit des temps pour tous les jours
Poser sama balance lourde, ma yoxu 'au secours! '
Li nekkatul love kase dama jaaxle céy l'amour
Waat naa ba waat sama akoulaye man yaa ma saf
Sama mbëggeel raw na roppalaan ba naaw jëm asaman
Ñaanu la ko lawu soo ma njëkkoon dee bébé
Billaay, dootuma dundu man!
États-Unis, sans visa ma ni
Dox ba dem Roumanie
Naaw ba asaman tërëdi àljanna
Foofu la, billaay foofu la
Billaay wallaay bébé
Maa la nob, wax ma ku ci mën nada
Moom du coow du tooñ du fowe dóor ak saaga
Moom dafa nooy agneau la bu tooy
Moom sax duma jooyloo dëkke di ma sourireloo bébé
Assane Wilane l'international
Chéri Mamy Mbaye Sofa Magui saliwoo
Assane bëgg naa la, Wilane fonk naa la
Mami doo ko jooyloo, dëkke di ko sourireloo bébé
Maa la nob, wax ma ku ci mën nada
Moom du coow du tooñ du fowe dóor ak saaga
Moom dafa nooy agneau la bu tooy
Moom sax duma jooyloo dëkke di ma sourireloo
Maa la nob, wax ma ku ci mën nada
Moom du coow du tooñ du fowe dóor ak saaga
Moom dafa nooy agneau la bu tooy
Moom sax duma jooyloo dëkke di ma sourireloo