Soumala done diémeu waxx nima la beugué
Dokko meusseu meuneu beug understand (fima tollu si yaw)
Soumala done diemeu wane lii si sama xool bi
Dokko meusseu meuneu beug comprendre (fima tollu si yaw)
Beugouma ga dem
Beug na ga took
Took bey sa warr
Tool bi yaw rekk yaw borom
Mane rekk ak yaw
Ga nekk ak mane
Niouy weurr di flow
Founiou dem bayyi fa thiow
Douma nelaw teh teulouloma
Ndakh dama goudeh yaw
Do yewou teh mane yewoumala
Daxx si mane ga bideunti
Soumala done diemeu waxx nimala beugé
Dokko meusseu meuneu beug understand (fima tollu ci yaw)
Souma done diemeu waxx nimala beugué
Dokko meusseu meuneu beug comprendre (fima tollu ci yaw)
Mayy fatalikou
Bigni doga xamé lo waxx ma deff
Louma waxx ga deff
Mane rekk ak yaw
Ga nekk ak mane
Niouy weurr di flow
Founiou dem bayyi fa thiow
Douma nela teh telouloma
Daxx dama goudde yaw
Do yewou teh yewoumala
Daxx si mane ga bideunti
Khadyy Mbengue o
Amadou Mbengue Salé Faye sa mame
Sheuuu Mbengue Souley sa bayy
Khady sévère Fati Dia
Domi Binta Gueye
Première directrice à St Louis
Soumala done diemeu waxx nimala beugué
Soumala done diémeu waxx nimala beugué
Soumala taw
Khady Mbengue yayou Charles ak Juliette
Mangui fii sa wett
Mouy norr di nawett
Mounalouniou dara
Daxx dara dou taxx ba dougnou beuguenté eeeh ba douniou beuguente
Ba douniou beuguanté
Ba douniou beuguanté
Nekk fi ak yaw bolé xol yi done benn
Happiness nexna daxx dara dou taxx ba douniou beuguenté eeeh
Ba douniou beuguenté eeh
Ba douniou beuguenté eeh
Touroutoutou touroutoutououu yeh
Touroutoutou touroutoutou yeh yeh yeh yeh
Mangui sii sa wett
Moy norr di nawett
Mounalouniou dara
Dara dou taxx ba diouniou beuguenté eeeh
Ba douniou beuguente eeh
Yaw ba douniou beuguenté eeh
Malakoy tiaw
Gama koy tiaw
Malakoy tiaw
Gama koy tiaw
Malakoy tiaw
Gama koy tiaw
Eh niou dem nieuweul