Cifra Club

Ndanaane (feat. Awa Gambia)

Dieyna

Aún no tenemos los acordes de esta canción.

Awa Gambia
Dieyna

Ma letal la lépp yëngu
Lépp dëgër te ma tàmbali ma
Xanaa du may ndaanaan
Ñaata yoon ñu sentu ma fi, sentu ma fee
Man ma fëlé feneen
Xanaa du may ndaanaan

Ku sa xol di metti maa lay bégal
Def lu baax laa lay dëgal
Xanaa du may ndaanaan
Ñaata kamb lañu maa gasal
Jëm maa feexel mënuñu ci man dara
Xanaa du may ndaanaan

Ndaanaan xamul ragal, yor fu la di ko jaay
Sa jikko da koy wane jom ak fitam waay
Ndaanaan dafay dëgger li nga koy waxal du ko sonal
Góor am du ko jaay, jom ak fu lem waay

Aah, xam nga maay kan
Man dama bari cas
Feel nga fem bi may ndaanaan
Eeeh, xam nga maay kan
Man dama bari cas
Gis nga fem bi may ndaanaan

Aah, may ndaanaan bi
May ndaanaan bi
Kañ ngay nangul ndaanaan bi
Eeeh, may ndaanaan bi
May ndaanaan bi
Jëmal nangul ndaanaan bi

Xale bu ndeyam gërëm
Nga koy yenne fan ne muy lay gëna belli
Xanaa du may ndaanaan
Yoon wi tollo loo te metti
Tiituma te ragaluma dara
Xanaa du may ndaanaan

Eeeh Awa ne leen pexe noon
Duma wacce sama yoon
Xanaa du may ndaanaan
Ala Atiou amul bàyyi
Duma sonn duma tàyyi
Xanaa du may ndaanaan

Ak lu mëna am, xoolal sa kanam
Dinga am ndam bul bàyyi
Fu ma mëna dem, lu ma mëna gis
Taking over everything

Aah, xam nga maay kan
Man dama bari cas
Feel nga fem bi may ndaanaan
Eeeh, xam nga maay kan
Man dama bari cas
Gis nga fem bi may ndaanaan

Aah, may ndaanaan bi
May ndaanaan bi
Kañ ngay nangul ndaanaan bi
Eeeh, may ndaanaan bi
May ndaanaan bi
Jëmal nangul ndaanaan bi

Aah yeah, yeee laye
Yella bu mi góor la
Aah yeah, Yella ye
Yella doomi góor la

Dieyna ak Awa
Sunu wey wii woyu góor la
Aah yeah, Yella ye
Yella doomi góor la

Awa ak Dieyna
Way wi wayu góor la
Aah yeah, Yella ye
Yella bu mi góor la

Aah yeah, Yella ye
Jumal nangul ndanaan bi

Otros videos de esta canción
    0 visualizaciones

    Afinación de los acordes

    Afinador en línea

    Ops (: Contenido disponible solo en portugués.
    OK