Li ma yéem dofloo na nit yu bari
Xol bi moo ci tiit tax ma listaxar
Def naa la sama toll, bu dul yaw du ma bàyyi
Damay wax nga sipp te danga képp say daaj
Lan moo ñu jikk xacundoo di songu
Duma xaar nga ci dox may dogg di sonn
Parfois nga fiir ni may jëfe ndiru ay tooñ
Kuy bëgg dangay ball alors baby profitons!
Kon damay ñëw sa koñ ndalle peloton
Saar seul galer ak samay kiloy guro tok fa ñaan
Su may dem tuddee la boulevard
Hey maa ko saña wax te du ma ci tàyyi
Ay mbëggeel laa lay drop drop drop drop drop drop
Jaaral nga ma daaw daaw daaw daaw daaw
Weerul ñu jël ay tof tof tof tof tof
Li may yëg tax may xaar pour ñu marié
Li may xaar mooy try one day
Jàkk jaa ak yoonu mairie
Yaa doon bidéew bi tax may tëp pour saxi laf
Am la soxna mooy tax ma chill tay
Su nekkee dëgg mak ñi dem ñaan
Reeroo su amer dañuy waxtaan
Xulóo jiguñu daf ñuy tardeel
Réccu mooy nga baal ma su ma la tooñee
Miroir sama xel lu dul sa xol du ci feñ
Def guro sama sac
Wan ko sa yaay te du bañ déet waay!
Kon damay ñëw sa koñ ndalle peloton
Saar seul galer ak samay kiloy guro tok fa ñaan
Su may dem tuddee la boulevard
Hey maa ko saña wax te du ma ci tàyyi
Ay mbëggeel laa lay drop drop drop drop drop drop
Jaaral nga ma daaw daaw daaw daaw daaw
Weerul ñu jël ay tof tof tof tof tof
Li may yëg tax may xaar pour ñu marié
Toc toc toc toc toc!
Daw daw daw daw daw!
Toph toph toph toph toph!
Looy xaar pour ñu mariéééé?
Kone damay nieuw seu kogn undallé peloton
Saarr seu galer ak samay kiloy gouro tok feu niane
Sou may dém touder leu boulevard
Héy mako sagna wakh té dou meu ci taayi yeaaah!