Namm naa la yaw
Gëj naa la gis
Kenn du baay boobu waay
Yaw sama xarit
Maa def la xarit
Nga def ma sa noon
Fayoo naar bi xoromam
Baadoola bi
Billaay fi ma jaarak yaw
Ku fa jaarak kala Yàlla boolel
Foo tolloo di ko way
Yaw sama xarit baa ngee
Ndaanaana ngi
Fi ma jarak moom
Ku fa jaarak kala Yàlla boolel
Foo tolloo di ko way
Ay sama xarit baa ngi
Ndaanaana ngi
Boo ma gisul toog di ma yàq
Te boo ma gisee reetaan
Nga foog ni dunya nii la mel
Yaw mi ne ko waaj
Man mii de xam naa ki ma doon
Ndax maa ngi sant Yàlla
Awma sax jotu di la jëw
Xam nga ni man maay waaj
Boo ma gisul toog di ma yàq
Te boo ma gisee reetaan
Nga foog ni dunya nii la mel
Yaw mi ne ko waaj
Man mii de xam naa ki ma doon
Ndax maa ngi sant Yàlla
Awma sax jotu di la jëw
Xam nga ni man maay waaj
Ree ma, ree ma
Ay ree ma, ma lay reetaan de ma yaw
Ree ma, ree ma
Yaw ree ma, ma lay reetaan de ma
Ree ma, ree ma
Yaw ree ma, ma lay reetaan de ma yaw
Ree ma, ree ma
Yaw ree ma, ma lay reetaan de ma
Ree ma, ree ma
Ay ree ma, ma lay reetaan de ma yaw
Ree ma, ree ma
Yaw ree ma, ma lay reetaan de ma
Ree ma, ree ma
Yaw ree ma, ma lay reetaan de ma yaw
Ree ma, ree ma
Yaw ree ma, ma lay reetaan de ma