Tooñ nga ma been yoon
Yaw chérie maa la baal
Tooñaat ma ñaari yoon
Bu ñeent dama lay baal
Li ma yëg ci sama xol
Yàlla seede na ma ko, waaw
Yaw ñëwal fi nga jege ma
Loo bëgg wax ma ko, waaw
Yaw biig, yaw biig ci guddi nelawuma
Di la xalaat ba léegi babe nelawuma
Yaw déedéet, bul defe noonu doyalu ma
Ku la naan màndi ku la ray gëne reew sama
Te ba nga yegsee la xel yi dal ñépp naan kaar mashallah!
Man namoon naa la chérie boy, waawaawaaw
Aah aah aah aah
Allame Allame Allame téléphonaa
Allame Allame Allame téléphonaa
Allame Allame Allame téléphonaa
Chérie, Allame téléphonaa
Tooñ nga ma been yoon
Yaw chérie maa la baal
Tooñaat ma ñaari yoon
Même bu ñeent dama lay baal
Bu ñeent dama lay baal
Yaw yaay booy, kaay jege ma
Mbëggeeloo may gaañ
Yaw yaay booy, kaay jege ma
Mbëggeeloo may gaañ
Mbëggeel yaa mën a boole
Nit ku ñuul ak nit ku weex
Yaa mën a boole
Bàmbara beek tukulóor bee
Tàkkuloo ko tàkkuma ko
Jigéen la yërëm ko
Waaye, yaw waaye bum la saay-saay yeeeh
Mbëggeel yaa mën a boole
Nit ku ñuul ak nit ku weex
Yaa mën a boole
Bàmbara beek tukulóor bee
Tàkkuloo ko tàkkuma ko
Jigéen la yërëm ko
Waaye, yaw waaye bum la saay-saay yeeeh
Ma ci jobaate, kalaju laa
Abadan doo fay
Ki nga bëgg ba bëgg ko
Soo la meree dangay feebar di dox ci yaw
Mel ni ku sibbiru mbëggeel metti na
Ki nga bëgg ba bëgg ko
Soo la meree dangay feebar di dox ci yaw
Mel ni ku sibbiru mbëggeel metti na
Soo xaaree ma ñëw
Fi nga ne fi ma nekk Mbaye sori nanu
Te xol day gise
Saa su ma lay gisee man kontaan
Ni mbëggeel, mbëggeel, mbëggeel, mbëggeel
Metti na waaw waaw
Maa woo la, ndaw sile bëgg naa la!
Yaw soo xaaree ma ñëw
Fi nga ne fi ma nekk Mbaye sori nanu
Te xol day gise
Saa su ma lay gisee man kontaan
Ni mbëggeel, mbëggeel, mbëggeel, mbëggeel
Metti na waaw waaw
Maa woo la, ndaw sile bëgg naa la!
Yaw dërëm yaay, yaw dërëm yaay
Dërëm yaay, dërëm yaay
Dërëm yaay, chérie xaadi dërëm yaay
Dërëm yaay, dërëm yaay
Clédore dërëm yaay
Baay Aïcha dërëm yaay
Dërëm yaay, dërëm yaay
Youssou dërëm yaay
Dërëm yaay, she tet tet tet tet!