Cifra Club

Balalma

Soryba Kouyate

Aún no tenemos los acordes de esta canción.

Daf may dal, dal naa fi ku ne
Aw la soru aw àj ko ci kaw
Baby da dor ko ci suuf
Yaw mi ma nob, xam naa ni yaay l'enfant des bénis
Doole yemul ñamal ba xam
Man aw la bëgg

Aw la ma nob, ay lexam moo ka noy népp
Waaw wolay
Aw mi ko def xam naa ni yaa ka tey def
Bi mbëggeel la dundu roppi baay ba géwél sa yaay

Qu'est-ce que ça fait?
Su ñu wétee
Sa loxo yi nga may teg may daanu def na éffet
Ma lingi yo man yaw yaay sama repré

Drogue bi may laaj
Sa deret laay pikkiroo wou-woo
Ba keroog may overdose
Te aimable waaw
Sa deret laay pikkiroo wou-woo

Lii ni
Sax di neex yaa ko moom
Te fi ni
Ku dul yaw wat na doo fi rot

Baalal ma
Mame Coumba Lambay baalal ma
Mbëggeel ku mu jàpp da lay
Balay baay nga taago sago

Lii ni
Sax di neex yaa ko moom
Fi ni
Ku dul yaw wat na doo fi rot

Baalal ma
Mame Coumba Lambay baalal ma
Mbëggeel ku mu jàpp da lay
Balay baay nga taago sago

Dal na ci lu ne!

Dugg nga sama surface di ma moqué di ma tapasse
Sa lowël dey toj kas guddi jote nga di ma cokass
Bébé xam nga doo seen maas, bodio-bodio du la tendance
Menthe, menotte wala cristal
Bébé xam nga danga saay-saay ye ye
Man xale laa, xawma yo yo
Nga def ma nonoh, ñamal ma yoyo

Qu'est-ce que ça fait?
Su ñu wétee
Sa loxo yi nga may teg may daanu def na éffet
Ma lingi yo man yaw yaay sama repré

Drogue bi may laaj
Sa deret laay pikkiroo wou-woo
Ba keroog may overdose
Te aimable waaw
Sa deret laay pikkiroo wou-woo

Lii ni
Sax di neex yaa ko moom
Te fi ni
Ku dul yaw wat na doo fi rot

Baalal ma
Mame Coumba Lambay baalal ma
Mbëggeel ku mu jàpp da lay
Balay baay nga taago sago

Lii ni
Sax di neex yaa ko moom
Fi ni
Ku dul yaw wat na doo fi rot

Baalal ma
Mame Coumba Lambay baalal ma
Mbëggeel ku mu jàpp da lay
Balay baay nga taago sago

Otros videos de esta canción
    0 visualizaciones

    Afinación de los acordes

    Afinador en línea

    Ops (: Contenido disponible solo en portugués.
    OK