Cifra Club

Boom Bye Bye

Viviane Chidid

Aún no tenemos los acordes de esta canción.

Deguena ko guiss mou mouss réne
Daw dagn ko nakhon
Li ma dal mane fogona warouma meuneu dal
Daffa am bene bess mane
Ma dougou si bene restaurant
Bene way djou sangsé ba rafet lol
Ni ma sokhnaci
Lo djeul mane ma koy faye
Tay la sama anniversaire djeuleul
Ma djeuleudjeueudjeull ba doyyal
Eumbeu def si sac bi djeuleul

Houu houu boom bye bye
Boba khamouma limouma beugeul wayyy
Boom bye bye
Mi ngui nane ma bye bye bye
Boom bye bye
Mane dama fogone ni daf may taggou
Thiey li

Bima wadjé djeul sama sac
Thiaki thiaki bay beugeu dem
Bene serveur nemeu madameyow dé fayago
Mani wadjé tokk dé moni ma mo koy fay
Mounima madam wadjé tokni khelmi nekhoul
Fi may beugeu djangou ndekké
Wona poliss waru na
Mané ma khol sama biir pochette
Lima yoor dé mattoul waruna aaa

Hou boom bye bye
Boba khawma limou ma beugueul way boom
Boom bye bye
Mi ngui nane ma bye bye bye
Boom bye bye
Mane dama fogone ni daff may taggou
Thiey li

Dama fogone niit ndiaye leuu
Ndeke wadji khelmi nekhoul
Bene baay faall la ma thie guéné
Boudoul wone nak mom ga ngi sonal ma

Akhaaa akkassa ziarra
Dawalal yeurmandé ki yaye faal la
Aaah dawalene yeurmandé
Yaye fall kay niou baay fall
Paré kharal khal dou wakh lou mal
Mouk dou def lou sall dou wakh lou mal
Eh dalay bal eh ngua am aal
Yaye faal la é ngua am aal
Na ya bindii naa ya bindi
Na ya bindii yaye fall han na ya bindi
Khalé ya ngui na ya bindi
Ah rass deuguine mbalakh
Ahhn deugine mbalakh, ah
Lolou warneu meuneu né

Alé sambeu djidem ya ngue sa djidem yeu
Alé lay woy djidem ya ngue sa djidem yeu
Wayé daffay meuneu né
Alé sambeu djidem ya ngue sa djidem yeu
Allé lay wooy
Dji demm ya ngueu sa dji demm yeu

Boom bye bye
Boom bye bye
Naa ya bindi bye bye
Naa ya bindi
Boom bye bye
Thiey boom bye bye, thiey boom
Thiey lii (bye bye)

Allé sambeu
Dji deem ya ngueu sa dji demm yeu
Allé lay wooy
Dji demm ya ngueu sa dji demm yeu
Deugeueleu
Alé sambeu djideem ya nge sa djidemm yeu
Allé lay wooy
Dji demm ya ngueu sa dji demm yeu
Akhaaa
Ni boom boom bye bye

Otros videos de esta canción
    0 visualizaciones

    Afinación de los acordes

    Afinador en línea

    Ops (: Contenido disponible solo en portugués.
    OK