Cifra Club

Sibam (feat. Sidate Bonbon)

Viviane Chidid

Aún no tenemos los acordes de esta canción.

Tay ji bésu begete la gay ñi
Tay ji ñëwel ñu ànd fecc

Mag ak ndaw, amul góor ak jigéen
Ñëwel dugg ci géew gi
Mag ak ndaw, amul góor ak jigéen
Na ñépp ñëw ci géew gi
Ma woyaat sibam

Jigéen ñi woneleen seen bopp
Ak yeen góor ñi yee nit ci génn bokk

Mag ak ndaw, amul góor ak jigéen
Na ñépp ñëw ci géew bi
Mag ak ndaw, amul góor ak jigéen
Feccal dugg ci geew gi
Ma woyaat sibam

Viviane, ma sira ak Issa Dieye
Fatim Penda ak Ma Ndiaye
Lay la cat, mashallah!

Tàcculeen, fecceleen, rafet genn
Loo loy xubal geew gi
Te guleen, fecceleen, mag ñee
Bu gene gene geew gi
Ma woyaat sibam

Yeah, yeah, yeah
Ma woyaat sibam

Ouh la, ou la la
Jege ma
Ouh la, ou la la
Pare ngeen

Sibam sibamoo sibam laal nga ma
Sibam sibamoo sibam laal nga ma

Booy fecce sibam dangay mel ni xaaru la biir
Sa jege di karaje yaay sibam laal na ma

Sibam sibamoo sibam laal nga ma
Sibam sibamoo sibam laal nga ma

Booy fecce sibam dangay mel ni xaaru la biir
Sa jege di karaje yaay sibam laal na ma

Ma ne sibam sibamoo sibam laal nga ma

Booy fecce sibam dangay mel ni xaaru la biir
Sa jege di karaje yaay sibam laal na ma

Otros videos de esta canción
    0 visualizaciones

    Afinación de los acordes

    Afinador en línea

    Ops (: Contenido disponible solo en portugués.
    OK