Ndekke du mbëggeeku kese
Te sax xeetu mbëggeel yi dafa rare
Jekku ma ni duma baal, yeah, yeah
An kon yaw bandit nga ndekke, bébé
Soppi nga sama xol bi limonade
Sirote ko di ko naan, yeah, yeah
Ndax ba ñuy njëkka gisante
Li nga ma yénne ni mu diisee
Ak ni ñu xoolante
Rekk ma xam ni Yàlla ñu boole
Est-ce que doo jinne ndax jommal nga ma (kaay waay)
Dofloo nga ma (kaay waay)
Waaye dëfal nga ma (kaay waay)
Man li may dundu ni dal neex na ma (kaay waay)
Soo bégee, ma bég (kaay waay)
Ñu dekke di ree (kaay waay)
Yaw mësul metti ba nga réccu li nga ma xam (kaay waay)
Maa la gënal lu ne (kaay waay)
Te yaa ma gënal ku ne (kaay waay)
Bae li ñuy dundu ni cer carré na (kaay waay)
Bégal, ma bég (kaay waay)
Maa xécc sa rëndal happy (kaay waay)
Soo ma soree oh my love
Nammeel bi may yëg ci yaw, wallaay!
Yaa ko mëna faj, ñëwal
Ñuy kaf di ree
Ñuy kaf di fo di ree
Ndax ba ñuy njëkka gisante
Li nga ma yénne ni mu diisee
Ak ni ñu xoolante
Rekk ma xam ni Yàlla ñu boole
Est-ce que doo jinne ndax jommal nga ma (kaay waay)
Dofloo nga ma (kaay waay)
Waaye dëfal nga ma (kaay waay)
Man li may dundu ni dal neex na ma (kaay waay)
Soo bégee, ma bég (kaay waay)
Ñu dekke di ree (kaay waay)
Yaw mësul metti ba nga réccu li nga ma xam (kaay waay)
Maa la gënal lu ne (kaay waay)
Te yaa ma gënal ku ne (kaay waay)
Bae li ñuy dundu ni cer carré na (kaay waay)
Bégal, ma bég (kaay waay)
Maa xécc sa rëndal happy (kaay waay)
Oh bébé toi mon bébé
Toi qui m’as tout donné
Je pourrais jamais te quitter
Je t’en fais la promesse mon bébé
Tu m’as tellement épaulé
Quand il le fallait
M’as sorti de la galère
Je vais te rendre la money
Oh bébé yaw mi gunge ma man maa lay gunge
Et si t'as peur crie, aide-moi, man maa lay sauver
Oh bébé yaw ndax bëgg nga ma comme ni ma la bëggee
Ndax ni ma la bëggee ëpp na waa li num deme
Oh bébé toi mon bébé
Toi qui m’as tout donné
Je pourrais jamais te quitter
Je t’en fais la promesse mon bébé
Tu m’as tellement épaulé
Quand il le fallait
M’as sorti de la galère
Je vais te rendre la money
Oh bébé yaw mi gunge ma