Cifra Club

Weetay (Hommage À Nos Morts)

Wizzy Kana

Aún no tenemos los acordes de esta canción.

Aduna meune neuh tass yaakar iow
Lii kouniou ko waxoone dh dougnko geum iow
Ndékké yallah
Bou soxlawéé iow dinga niakk
Demnga wanté dou takh
Banga joggé thi sounou xalaat iow
Weetay weeteul nganiou weeteul sa waa keur
Demnga té dotouniou la guissat
Niakk nagn leuh ba abadane

Weetay
Weetaayeee
Joy nagn
Thi liniou leuh niaké

Mangui fatélikou jamono yign daane jotay
Waxtaane kaff foo reh souniou waadji
Yakarouniou woone ni dinga dem bagnou fi
Geumouniou woone ni dotounioula guissati
Yallah niou bakh rek leuh nango teela dieul
Mag gni seedé nagn ni jokhone ngaleen thieur
Démé nga ndaw ndékété aduna dou keur
Weetay weeteul nganiou weeteul sa waa keur
Demnga té dotouniou la guissat
Niakk nagn leuh ba abadane

Weetay
Weetaayeee
Joy nagn
Thi liniou leuh niaké

Otros videos de esta canción
    0 visualizaciones

    Afinación de los acordes

    Afinador en línea

    Ops (: Contenido disponible solo en portugués.
    OK