Gis naa bu baax ni nga may xoolee
Yaa ngi xool lu mool waaye am naa borom
Man de setlu naa ni nga may ginge
Bëgg naa nga gëm Yàlla, doo ma fi ame
Dégg naa la
Su jaaree ma ñakk jom dinaa ko def
Su jaaree ma bokk la dinaa ko def
May ma semaine ma wax la ni ma la bëggee
Yaa ma gënal waay
Yaa ma gënal waay
Kon ayway ni wax leen ci
Xale yi jaral nga ma
Ki la jaral yaw jaar na
Sonal nga ma
Ayway ni wax leen ci
Jaral nga ma
Moom mi la jaral yaw jaar na
Sonal nga ma
Ba ko muy déconné
Xawma la ci tatoné
Xale yaa ngi fi di zalonné
Ngay topp ki di déconné
Ngay ñaan samit, yaa ñàkk jom
Ñëwal fi, kay
Te nga bàyyi ki di déconné
Ayway (déconné)
Bàyyil way (tatoné)
Ñëwal fi way (zalonné)
Te nga bàyyi ki di déconné
Man seetlu naa ni nga fi ñëwee
Nga ñëw di xool soo ma
Man de setlu naa ni nga may ginge
Bëgg naa nga gëm Yàlla, doo ko fi ame
Ay Ki dafa ma ray dama dee di cas
Xale jox ma sama ji am dédicaces
Sama yaakaar ci ki doo ko tas
Nob la mbëggeel bu xor du kenn
Na daagu moo xool lew mu tàngalu
Mooy doole
Yaw dinga moo ko pas, billaay
Ki romb sama fit bi di maas, wuyay
Ayway ni wax leen ci
Jaral ji ko
Dinga moo ko pas, billaay
Ki romb sama fit bi di maas, wuyay
Ayway ni wax leen ci
Jaral ji ko
Dinga moo ko pas, billaay
Ki romb sama fit bébé, wuyay
Ba ko muy déconné
Xawma la ci tatoné
Xale yaa ngi fi di zalonné
Ngay topp ki di déconné
Ngay ñaan samit, yaa ñàkk jom
Ñëwal fi, kay
Te nga bàyyi ki di déconné
Ayway (déconné)
Bàyyil way (tatoné)
Ñëwal fi way (zalonné)
Te nga bàyyi ki di déconné