Cifra Club

Talal Loxo

Viviane Chidid

Aún no tenemos los acordes de esta canción.

Dama doneu deim di deim sama yoon
Ma dadjeik wadiou bakh mouneima
Sama djiguene fo dieum ma yoboula
Sama yaye neinama sama baye neinama moytoulma doxaneu neimeu
Bama seitei ba setatate cilako talal loxo
Niou daldi andeu deim
Cii souniou yoon wignou deim talal loxo

(Ouh) beut yi dafa weikheu
Bamay ndourok lou melni peikheu
Wakh dji dafa neikheuuu
Soye deim doma fi bayi

Leineu woor nama cii souniou digueuntei
Louniou bindoneu leu cii teirei yi
Bamala xamei daal batay djilei
Fouma teuddei yanoreu maneu
Founiou yeiwo diakarlo
Mbeuguel reiika woreii hey hey
Fimome reithiou amoufi
Samay rongongneu douffi tourow
Amnga sama yeurmandeiy
Lolou taay mo diafei talal loxo

(Ouh) beut yi daffa weiikheu
Bamay ndourok lou melni peikheu
Wakh dji daffa neiikh
Boye deim doma fii bayi

Ouuuh yayayayaye ya yaye ya yaye yayaye
Reitiouw ma lii ouuh
Rethiouw mali yaye reitiow mali
Beut yi daffa weiikheu hiii hiii
Bamay ndourok lou melni peikheuu
Ouuuh houu yayayayaye yayaye ow ow no
Oooh beut yi daffa weiikh

Otros videos de esta canción
    0 visualizaciones

    Afinación de los acordes

    Afinador en línea

    Ops (: Contenido disponible solo en portugués.
    OK