Ana li tax nit ki di bëgg, tax nit ki di bañ
Tax nit ki di jooy di jëfe li muy bañe
Yaw de yaay ki tax mu daw
Ngir nga sori bépp coow
Tax de caabi féete na leen ginnaaw
Teewul tey laa la gën a nob
Tay laa la gën a fonk
Tay laa la gën a sopp
Tay laay gën a dof ci yaw
Bi mbëggeel bokkul ak bu ñooñu
Bi mbëggeel bokkul ak bu ñooñu
Moom ne na fi nga dem laay dem
Fi nga ne laay ne
Bopp ak bopp, mbagg ak mbagg, tank ak tank
Ndaxte yaw laa love
Waa ji ne na yaw laa love
Moom ne na fi nga dem laay dem
Fi nga ne laay ne
Bopp ak bopp, mbagg ak mbagg, tank ak tank
Ndaxte yaw laa love
Waa ji ne na yaw laa love
Ouh, yeen a bokk yëg-yëg
Ouh, yeen a bokk ngëm-ngëm
Ouh, yeen a bokk gis-gis
Ouh, oh oh
Tu es celle qu'il a choisi, qu'il a suivi
Tu es son ame soeur
T'es celle qui a fait de lui un kilifa
Ouais ouais, t'es celle qui a fait de lui un kilifa
Kon xamal ni nak muy naaj di guddi ak lu mu metti
Du mës a bàyyi, non non du mës a xàddi
Ñaari nit la, te yeen ñaar la
Kon nak bëggalante waay!
Nyaari nit leu teh yen nyaar la
Kon nak beugeuntelene waay
Moom ne na fi nga dem laay dem
Fi nga ne laay ne
Bopp ak bopp, mbagg ak mbagg, tank ak tank
Ndaxte yaw laa love
Waa ji ne na yaw laa love
Moom ne na fi nga dem laay dem
Fi nga ne laay ne
Bopp ak bopp, mbagg ak mbagg, tank ak tank
Ndaxte yaw laa love
Waa ji ne na yaw laa love
Waaw wallaay fi nga ne (laay ne)
Waay fi nga jëm (laay ne)
Moom bopp ak bopp, mbagg ak mbagg, tank ak tank
Ndaxte yaw laa love
Xale bi ne na moom yaw la bëgg, waay!
Xale bi ne na moom yaw la love, waay!
Ndax ne na fi nga nekk (laay ne)
Waa wallaay fi nga jëm (yaw laay ne)
Ndax bopp ak bopp, mbagg ak mbagg, tank ak tank
Ndaxte yaw laa love
Xale bi ne moom yaw la love, waay
Ndaxte yaw la love
Xale bi ne moom yaw la bëgg waaw