Cifra Club

Xel Akk Xol

Ashs The Best

Aún no tenemos los acordes de esta canción.

Yeah, eh eh eh
Lé, lé, walé
Hum, hum

Suba su ma yeewu
Yaw laay bëgg jàkkaarlool
Saa su ma yeewu
Yaw laay bëgg njëkk xool

Ëllëg lu mat a soor la
Waaye xel xalaatu ko
Ëllëg ay jaar-jaar la
Sama xol yëgoon na ko muy ñëw

Xel xalaat la (xel ak xalaatam ba)
Xol yëg-yëg la
Nit ak jëmmam ja
Dara xaaju fa

Saa su ma yeewu
Yaw laay bëgg njëkk xool
(Su ma yeewu yaw laa bëgg njëkk xool)
Fajar su ma yeewu
Yaw laa bëgg jàkkaarlool

Denk naa la guddi
Fanaan yakkar ci yaw
Gent naa la guddi gi yëpp
Ndax fajar yaw lay jàkkaarlool
Mbëggeel

Xel xalaat la
Xol yëg-yëg la
Nit ak jëmmam ja
Dara xaaju fa

Nit ak jëmmam ja
Dara fa xaajul

Otros videos de esta canción
    0 visualizaciones

    Afinación de los acordes

    Afinador en línea

    Ops (: Contenido disponible solo en portugués.
    OK