Saf nga jigéen loolu laa lay toppe
Dama la xool li ma gis di ma choqué
Ni nga mel naturel la, doo ko forceloo
Gel bi dafa tàng ba di lakk
Safara biy nelaw ci yaw la bëgga gis
Pese naa la ci li nga doon dafa diis
Saf ni jimbo, tooy ni rico
Gel bi dafa tàng ba di lakk
Shut, ak gel booy bu la jege ma shut
Li may wër yépp ci jigéen nga uuf
Sa béppu moroom bu la tëkk nga shut
Shut, shut, shut, shut, shut
Baby kaay sama wet
Mbëggeel laa lay sedd ma dama jooy
Billaay yaay ki may daneel, oh, ooh
Bi ma la gisee sama xol dafa neex
Bi ma la gisee
Baby kaay sama wet
Mbëggeel laa lay sedd ma dama jooy
Bi ma la gisee
Sama lingeer yaa xarade
Am nga cas waaw yaa cëkkëte
Yaw laay wër suba ba ngoon ma tëddi
Yàgg na bari mais waay yaw tu es mon combat
Bandit, bandit
Baby bandit danditlul
Wane sa bandit wëdelul
Coow li coow li yaw jugal nga féemu
Daggal sa yaram ñu ndellu
Shut, ak gel booy bu la jege ma shut
Li may wër yépp ci jigéen nga uuf
Sa béppu moroom bu la tëkk nga shut
Shut, shut, shut, shut, shut
Baby kaay sama wet
Mbëggeel laa lay sedd ma dama jooy
Billaay yaay ki may daneel, oh, ooh
Bi ma la gisee sama xol dafa neex
Bi ma la gisee
Sama xol
Bi ma la gisee
Mix bi saf na!