Oooh ooh
Naa naa, yeah
It's about love, baby
La patience est dure
Mais sa récompense est pure
Xaar bi yagg na te lu yagg dëgg la
Moo tax ku muuñ muñ
Ñu ñaar la woon
Muy neex ak muy naxari
Tay ñu nekk noon suba ay xarit
Ànd bile jiitu na judd bi
(Ouhouhou) ouh way ooh oh
(Ouhouhou) diggënte bi dafa over nice
(Ouuuuh) over nice, yé hee
(Ouuuuh) maa la bëgg te ma xam sa price, xam sa price
(Ouhouhou) wooh oh, buur bi Yàlla moo ko organize, organize
(Ouuuuh) yeah eh, I love you baby
Ooh
Bës bi ma doon xaar agsi na
Mësuma bég ba mu romb li
Mësuma bég ba mu romb li
Nan, nan, nan, nan, nan
Ooh
Bës bi ma doon xaar agsi na
Mësuma bég ba mu romb li
Mënuma bég ba mu romb li
Nan, nan, nan, nan, nan
Nara na na na naara na
Yeah, yeaaah
Oooh ooh
Love
Xamoon naa ni dina mësa neex
Lu metti loo gis dina mësa jeex
Lu doonoon sama yééne moo di
Fomp sa rangooñ, dap sa bàaneex
I love you, man bëgg naa la
Sommi yanima bernam ene faada
Waxoon naa la bul la dara métti
My baby, I got your back
(Ouhouhou) tay ji yaddi sama soxna
(Ouhouhou) man ak yaw ñu ànd bokk soxla, ooh
(Ouuuuh) tay de jot na
(Ouuuuh) yeah, bës bile jot na
(Ouhouhou) tay ji yaddi sama soxna
(Ouhouhou) man ak yaw ñu ànd bokk soxla, ooh
(Ouuuuh) bës bile jooot na
(Ouuuuh) ma ne bës bi la jot na
Ooh
Bës bi ma doon xaar agsi na
Mësuma bég ba mu romb li
Mësuma bég ba mu romb li
Nan, nan, nan, nan, nan
Ooh
Bës bi ma doon xaar agsi na
Mësuma bég ba mu romb li
Mënuma bég ba mu romb li
Nan, nan, nan, nan, nan
Ooh, oh, oh
Bës bi ma doon xaar yegsi na
Mësuma bég ba mu romb li
Mësuma bég ba mu romb li
Oooh
Bës bi ma doon xaar yegsi na
Mësuma bég ba mu romb li
Mësuma bég ba mu romb li
Oooh (I love you)
Bës bi ma doon xaar yegsi na (eh, I love you)
Mësuma bég ba mu romb li
Mësuma bég ba mu romb li
(You're the one that I lo-lo-love, yeah)
Oooh (loving you)
Bës bi ma doon xaar yegsi na (my baby I love you)
Mësuma bég ba mu romb fi
Mësuma bég ba mu romb li
(Mënuma begg ba mu romb li, yeah)
Oooh (yeah)
Bës bi ma doon xaar yegsi na (I love you)
Mësuma bég ba mu romb fi
Mësuma bég ba mu romb li
Yeah!